Superman Love

Pape Diouf

Duma ci lenn lépp yaw la

Yaw yaay sama poumon gauche

Soo kontaanul dund du yomb

Amuma lu bari mais coco

Xol bi ma ko moom, jox naa la ko

Bébé sax boo demee bay fane

Ma doon ginnaar gi ngay reere

Kanam gi ngay ñekk gis fo dikke

Jege ma ma tay la lu bees ya fi ne

Bae je t'aime

Mi ko ankom mbi yitte

I love you, bébé n b'i fè

Te amo, ich liebe dich

Shiwananko, wo ai ni yoo

Boo de jant ma doon superman

Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane

Def naa la sama soxla

Sama soxna, sama number one

Boo de jant ma doon superman

Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane

Def naa la sama soxla

Sama soxna, sama number one

Yaay piano sama mind

Yi mélodie foo ko jange

Jar ci xol bi, jaaxase xel mi

Def sa tuur ci këyitu kër g

Tegi monument de la renaissance

Tek fa sa bos di ko status

Bet seereer ak bolu cëre

Yi may def moo ko gën a neex

Di gis tukkulër bu burde

Ki lay jooyloo moo la war a nax

Boo de jant ma doon superman

Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane

Def naa la sama soxla

Sama soxna, sama number one

Boo de jant ma doon superman

Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane

Def naa la sama soxla

Sama soxna, sama number one

Bae kaay ma wax la secret

Dama sëy ci sa jëme ji dalaas ngoom

Yaw dal, yaay première dame ci xolu king

Donte jarul maa la koy wax

Bëgg la ba ci sa waw lay dox

Yaay piano sama mind

Yi mélodie foo ko jange

Yaay piano sama mind

Yi mélodie foo ko jange

Bilaahi mbëggeel la neex

Mbëggeel la neex xale bile (mbëggeel la neex)

Muy gën di neex neex a neex ba jaxal ma

(Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj)

Leee lee leee lee mbëggeel (mbëggeel la neex)

Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni bilaahi mbëggeel

(Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj)

Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni mbëggeel

(Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj)

Aka bari doole bilaahi mbëggeel

Unduh .lrc WhatsApp