[00:14.21] Duma ci lenn lépp yaw la [00:19.67] Yaw yaay sama poumon gauche [00:22.11] Soo kontaanul dund du yomb [00:25.22] Amuma lu bari mais coco [00:27.64] Xol bi ma ko moom, jox naa la ko [00:30.74] Bébé sax boo demee bay fane [00:33.11] Ma doon ginnaar gi ngay reere [00:36.25] Kanam gi ngay ñekk gis fo dikke [00:41.78] Jege ma ma tay la lu bees ya fi ne [00:45.63] Bae je t'aime [00:47.16] Mi ko ankom mbi yitte [00:49.95] I love you, bébé n b'i fè [00:52.39] Te amo, ich liebe dich [00:54.82] Shiwananko, wo ai ni yoo [00:58.16] Boo de jant ma doon superman [01:00.67] Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane [01:03.65] Def naa la sama soxla [01:05.56] Sama soxna, sama number one [01:08.71] Boo de jant ma doon superman [01:11.47] Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane [01:13.74] Def naa la sama soxla [01:15.70] Sama soxna, sama number one [01:29.17] Yaay piano sama mind [01:32.85] Yi mélodie foo ko jange [01:35.22] Jar ci xol bi, jaaxase xel mi [01:37.60] Def sa tuur ci këyitu kër g [01:40.35] Tegi monument de la renaissance [01:43.01] Tek fa sa bos di ko status [01:45.87] Bet seereer ak bolu cëre [01:48.51] Yi may def moo ko gën a neex [01:51.26] Di gis tukkulër bu burde [01:53.98] Ki lay jooyloo moo la war a nax [01:57.29] Boo de jant ma doon superman [01:59.97] Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane [02:02.30] Def naa la sama soxla [02:04.23] Sama soxna, sama number one [02:08.11] Boo de jant ma doon superman [02:10.11] Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane [02:12.48] Def naa la sama soxla [02:15.00] Sama soxna, sama number one [02:33.85] Bae kaay ma wax la secret [02:37.45] Dama sëy ci sa jëme ji dalaas ngoom [02:41.35] Yaw dal, yaay première dame ci xolu king [02:45.25] Donte jarul maa la koy wax [02:47.28] Bëgg la ba ci sa waw lay dox [03:00.22] Yaay piano sama mind [03:02.62] Yi mélodie foo ko jange [03:10.73] Yaay piano sama mind [03:13.48] Yi mélodie foo ko jange [03:27.13] Bilaahi mbëggeel la neex [03:29.80] Mbëggeel la neex xale bile (mbëggeel la neex) [03:37.72] Muy gën di neex neex a neex ba jaxal ma [03:43.53] (Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj) [03:48.58] Leee lee leee lee mbëggeel (mbëggeel la neex) [03:58.27] Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni bilaahi mbëggeel [04:03.35] (Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj) [04:08.79] Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni mbëggeel [04:13.83] (Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj) [04:18.37] Aka bari doole bilaahi mbëggeel [04:25.07]